AI Generated
Sondo Ai Default Title
user-HpCrf
user-HpCrf
yestekeu beuk deug si sa tank ni ngay woté modoul deug si yaw. nital ndem def sa nank nank dossi sori bo xamone djikoam. yalla ay dogal ni tidila diougueul moulay mousal niou lay yéné mbougal. tekla nat pour nattela mou nioul niongal yabo yallay dogal. yay ba loutakh def koma kom sa dom dinga dé kénéne domou sa dom. sama demb yalla ko def si mane yay ak baye la mou diou baye guinaw.mangui téw mais douma délou guinaw wourna yalla nafi nek bi déw. nafi dane ba dane arbitre si biir guéw mofi meun si peur arbitre si mim rew. fi ngéne teud yalla na lén gueneul. di lén sani ay niane la lén meuneul. féké woulén si dara ma gueuneul. bakar yémou diou beuri ma gueuloum président. bayil doul di dadialé. loutakh sa dom amadou dou pakété. nioun nioy sonou si thiélik si hopitaux yi. deunk lén ay milliar yi ngéne profito si motakh boy yi ték bandit ték live. yallal lék kilo yi tégé lén diplôme yi.fay na saax dagn ko banaliser, wakhé mou diékh wakh thi dou meuna nékh, ay grand di marr pour ay visa qui échec. comédie Pdi mo wara diékh yow dague wo beugue dioubeul, kou doul yorr. noumouy diokhé deugue wor danga meuneul boy, guiss dague ba deugue si sa tank. li guay woté modoul deugue si yow. niit la leundeum déf si nanke nanke. dossi sori bo khamone djikome. yallaay dogal ni tiidila diougal, mouléy moussal nioulay yéné mbougal. tégu la nattou pour natte la mounial, mounial yébo, yallaay dogal. guiss deugue ba deugue si sa tank, li guay woté modoul deugue si yow. niit la leundeum déf si nanke nanke. dossi sori bo khamone djikome. yallaay dogal ni tiidila diougal. mouléy moussal nioulay yéné mbougal. tégu la nattou pour natte la mounial, mounial yébo, yallaay dogal. nongu ko yallaay dogal. takal sa fitt yallaay dogal. gueumal sa bopp yallaay dogal.
00:00 / 00:00